Orchestra Baobab - Bul Ma Miin Lyrics

Get the lyrics to the song: Bul Ma Miin by Orchestra Baobab at LyricsKeeper.com.
Bul Ma Miin

Bul Ma Miin Lyrics |
---|
What Are The Lyrics For Bul Ma Miin By Orchestra Baobab?
Bul ma miin, Bul ma miin
Bul ma miin ba fatte ma Kon mu ňaaw Adduna yaa mëna wor Xaň ma ndey xaň ma baay Boo ma digee sama doom nax nga ma Lekkatuma, naanatuma Tëddatuma, nelawatuma Boo ma digee sama doom nax nga ma Alarba la woon ci weeru koor Mu taggu ma ne ma maangi ňëw Boobu ba téy gisuma sama doom Woy wéét, woy wéét Woy wéét adduna Sama doom dem na nii |
Who Wrote Bul Ma Miin By Orchestra Baobab?
Barthelemy Koffi Attisso, Ndiouga Dieng
|
What's The Duration Of The Bul Ma Miin By Orchestra Baobab?The duration of Bul Ma Miin is 6:02 minutes and seconds. |
More Lyrics
0 | 1 | 2 | 3 | 4 | 5 | 6 | 7 | 8 | 9 | A | B | C | D | E | F | G | H | I | J | K | L | M | N | O | P | Q | R | S | T | U | V | W | X | Y | Z
Lyrics Of The Day
- Ceelo: Gotta Love It You gotta love it…
- Lou Reid & Carolina: Don't Pass Me By I listen for your footsteps…
- Curt Sheller: The Shadow of Your Smile The shadow of your smile…
- The Midnight Strings: The First Noël The first Noel…
- The Sachal Ensemble: Man in the Mirror I'm gonna make a change…