Youssou N'Dour - 4-4-44 Lyrics

Lyrics Keeper

Get the lyrics to the song: 4-4-44 by Youssou N'Dour at LyricsKeeper.com.

4-4-44

4-4-44 Lyrics by Youssou N'Dour
4-4-44 Lyrics

What Are The Lyrics For 4-4-44 By Youssou N'Dour?

4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh

Bô léké ba sour war nga gueureum
War nga gueureum gni doug thi wagne wé
Wagne wa tang na
Fimou toll nî war nguèna bëg
War-ngèna bëg thi indépendance bi ak-liko indi

4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh

Bô léké ba sour war nga gueureum
War nga gueureum gni doug thi wagne wé
Wagne wa tang na

Damani bou leuk léké olom
Boudè goréna té deugou warna ko guereumé pithe

No, no, no no no no
No, no, no no no no yeah

4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh

Ah li dafa nékh
Guiss say mbok mô neikh
Li dafa nékh
Gueume sa bopp mô nékh

4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
No, no, no
Guiss say mbok mô neikh

4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
Oa, li dafa nékh
Guiss say mbok mô neikh
A môm sa bopp mô neikh
Oa, li dafa nékh
Môm sa bopp mô neikh

Who Wrote 4-4-44 By Youssou N'Dour?

Kabou Gueye, Youssou N'dour

More Lyrics

0 | 1 | 2 | 3 | 4 | 5 | 6 | 7 | 8 | 9 | A | B | C | D | E | F | G | H | I | J | K | L | M | N | O | P | Q | R | S | T | U | V | W | X | Y | Z

Lyrics Of The Day