Youssou N'Dour - Birima Lyrics
Get the lyrics to the song: Birima by Youssou N'Dour at LyricsKeeper.com.
Birima
| Birima Lyrics |
|---|
What Are The Lyrics For Birima By Youssou N'Dour?
Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile Maysa tende jodo yaa moom liile Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Buri samba laobe yaa moom liile Buri samba laobe yaa moom liile Buri samba laobe yaa moom liile Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Damel maisa penda joor Jooro jooro jooro jooro ho ho ho hoy Sama waaji ken dula jam naani Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Mmmm mmm Wooy tedi ngoné maarne be sambaa Kuli baca senge ndat biran ngamoo Ngoné maca nas mbay maca jeeri Samba yaasimooooo dike mbay kuja dooooki Yay borom mbaboor mi Hi (di) woy birima sama waaji ken dula jam naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Dogo fal ak mawa joor kumba samba yaay jaloor Dogo dogo, ho ho ho! Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel kayor niila Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee |
Who Wrote Birima By Youssou N'Dour?
Mbaye Mamadou, Ndeye Ndoumbe Mbaye, Youssou N Dour
|
What's The Duration Of The Birima By Youssou N'Dour?The duration of Birima is 7:48 minutes and seconds. |
More Lyrics
0 | 1 | 2 | 3 | 4 | 5 | 6 | 7 | 8 | 9 | A | B | C | D | E | F | G | H | I | J | K | L | M | N | O | P | Q | R | S | T | U | V | W | X | Y | Z
Lyrics Of The Day
- Kamahl: This Guy's in Love With You You see this girl, this girl's in love with you…
- Dance of Days: Fallen Fallen one on the ground…
- Insyde: Sometimes I know that your heart hurts inside…
- L'Orchestre de Jean Boyer: Que Reste-T-Il de Nos Amours? Ce soir le vent qui frappe à ma porte…
- Advent: Set Apart I will testify though I walk this road alone…