Youssou N'Dour - Habib Faye Lyrics

Get the lyrics to the song: Habib Faye by Youssou N'Dour at LyricsKeeper.com.
Habib Faye

Habib Faye Lyrics |
---|
What Are The Lyrics For Habib Faye By Youssou N'Dour?
Adduna bi du dara, te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp, xamal ni japp u loo ci, dara Adduna bi du dara, te dara xaj u fi Bi Lahii ku ko japp, xamal ni japp u loo ci, dara Man Youssou ñakk naa, andandoo bu sincère Adduna, adduna daal, nax ati na ñu Adduna, adduna da fay wor ee Habib Faye, dem na nii Waa ju baax, guddée na waay Habib yaru woon na, and ak dignité Fonŋk oon na liggéey ёm, bëgg njaboot am bu, baax Doon oon jàmbaar Man Youssou ñakk naa, andandoo bu sincère Adduna, adduna daal, nax ati na ñu Adduna, adduna da fay wor ee Habib Faye, dem na nii Waa ju baax, guddée ne waay Adduna, adduna Adduna, adduna Adduna, adduna daal, nax ati na ñu Adduna, adduna da fay wor ee Habib Faye, dem na nii Waa ju baax, guddée na waay Waa ju baax, guddée na waay |
Who Wrote Habib Faye By Youssou N'Dour?
Youssou N'dour
|
What's The Duration Of The Habib Faye By Youssou N'Dour?The duration of Habib Faye is 3:40 minutes and seconds. |
More Lyrics
0 | 1 | 2 | 3 | 4 | 5 | 6 | 7 | 8 | 9 | A | B | C | D | E | F | G | H | I | J | K | L | M | N | O | P | Q | R | S | T | U | V | W | X | Y | Z
Lyrics Of The Day
- Sidney Bechet's Blue Note Jazzmen: Runnin' Wild My gal and I, we had a fight…
- Melissa Mars: 1980 Qu'est-ce qu'on risque à passer pour des fous…
- DLMT: Always Feels Like I always feel like somebody's watchin' me…
- MC Hammer: U Can't Touch This You can't touch this…
- Harry Macdonough: Adeste, Fideles (O Come, All Ye Faithful) REFRAIN:…