Youssou N'Dour - Létt Ma Lyrics

Get the lyrics to the song: Létt Ma by Youssou N'Dour at LyricsKeeper.com.
Létt Ma

Létt Ma Lyrics |
---|
What Are The Lyrics For Létt Ma By Youssou N'Dour?
Du nil, du nil
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Xamal ma lu leer Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale Yaw daal yaw téppal fële Danga ba di tappale Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé Ngall yaw bul ma defioo, lu ma nin ni di xeebe Létt ma mbaa nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Lég lég sax nga yónni ma Ma dem bay dem nga teye ma Léégi sax dematuma Damay bañ nga dugël ma Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe Létt ma mbaa nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw Létt ma mbaa nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Boo ma waxee fi nga bêgg dem Ma wax la fi ngay jaar Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë Bëgg ak bañ la |
Who Wrote Létt Ma By Youssou N'Dour?
Kabou Gueye, Mody Ba, Youssou N'dour
|
More Lyrics
0 | 1 | 2 | 3 | 4 | 5 | 6 | 7 | 8 | 9 | A | B | C | D | E | F | G | H | I | J | K | L | M | N | O | P | Q | R | S | T | U | V | W | X | Y | Z
Lyrics Of The Day
- Michael B. Wailing: Anything Goes Times have changed…
- Cheryl Cole: Fight for This Love Too much of anything can make you sick…
- X-Magneto: Mi Amada Pantalon de piel…
- Rejuvination: Requiem She cries, "It's freedom that we need"…
- The Irving Bunton Singers: Come Sunday/David Danced Oh, Lord, dear Lord above, God almighty…